Jammu Africa

作词:Ismael Lo

作曲:Ismael Lo

所属专辑:Best Of

歌词

@migu music@

Jammu Africa - Ismael Lo

Written by:Ismael Lo/Ismaël Lo

Africa a a a Africa mon afrique

Sama gent gi maa ngi naan yalla wonma ko bala

May nibbi barsaq

Ma ne bes du nakk ci bes yi Africa don

Benn reew

D'ici ou d'ailleurs nous somm' des enfants d'afrique

Mem' si le ciel tombait luttons pour la paix

Kon jammu Africa moom lay naan

Mane jammu Africa mooy sunu natange

Africa a a a Africa a a

Africa a a a Africa mon afrique

Yow mi nekka bittim reew man mi lo maa

Lay naan

Ak loo fa meun ta am ak noo fa meun

Ta mel bul fatte Africa

Ici ou ailleurs la paix prix du bonheur

Mem' si le ciel pleurait luttons pour nos freres

Kon jammu Africa moom lay eaan

Mane jammu Africa mooy sueu natange

Africa a a a Africa a a

Africa a a a Africa mon afrique

Africa a a a Africa a a

Africa a a a Africa mon afrique

Onon bibbe Africa ngimode ngimode liggo den leydi men

Ngaccen hasi daagal yoo alla suren e musibaadi

Yoo alla addu jam to ruanda

Yoo alla addu jam to burundi

Yoo alla addu jam to casamans

Lawol mbignona yee

Africa a a a Africa a a

展开